Mmoi j etais rappeur et amimateur hip hop mais grace a baye kara je suis aujourdhuit chanteur de khassida merci killifa gorgorlul rek yok ci jang khassida ak zikre
Machalla mon ami mon frère. Je suis si fier de toi.Et temoigne de la véracité de tes propos.Qui t'écoute et connait Serigne Abdou KARIM sait de quoi tu parles.Il est multidimentionnel et honore l'être humain de toute classe sociale qu'il puisse etre.Et Oui bien dit pour le passage Serigne Moutakha MBACKÉ (Yallah nafi yagg té werr).Serigne Abdou karim MBACKÉ ne cesse de nous rappeler qu'il est important d'avoir des sages (autorité,Kilifeu) par ce marque de refaire appaitre en premier Le khalif general des mourides.Il l'a dit.Qu'il ne fait qu'approuver les recommandations du khalif comme un talibé.Le Makarim Al Aqla (Les nobles carracteres sont d'abord pronés par le prophete Mouhamed Salla Lahou Aleyhi Wa Salam) alors c'est notre salut à tout musulman et l'incarner ne tient pas compte des confreries mais de l'unité et c'est ce que nous apprend Serigne Abdou Karim MBACKÉ ibn Serigne Fallou MBACKÉ. Belle emission et la maturité ne fera que grandir encore plus inchallah.Yalkah nala Yallah yokka Diapalé.
Je NE SUIS PAS FANS DE TOI MAIS J'APPRÉCIE BEAUCOUP TES DISCOURS , TON ARGUMENT VÉRIDIQUE ET LE SENS DE LA RESPONSABILITÉ KILIFEU ET VOUS DONNEZ DU COURAGE EN RACONTANT VOTRE VIE.
Thieuy S.Touba kilifa raw nga bilahi keene doula tee kome neekh beusal 👍
Mmoi j etais rappeur et amimateur hip hop mais grace a baye kara je suis aujourdhuit chanteur de khassida merci killifa gorgorlul rek yok ci jang khassida ak zikre
Machalahh baye Karim rk gnimou dembali barina loll yal na guoudd fane loll mbacke
salut kilifeu malla buegue nguirre serigne touba rék séetii nga kou diarra séetii serigne abdou Karim sans 111sans ordonnance amine wakh léenne amine
Machalla thieuy serigne Touba☝️❤❤❤😭😭😭
Ndéyssane ki nitou kassé la bilay yalnala yalla diapaléla machalah
Machalla mon ami mon frère. Je suis si fier de toi.Et temoigne de la véracité de tes propos.Qui t'écoute et connait Serigne Abdou KARIM sait de quoi tu parles.Il est multidimentionnel et honore l'être humain de toute classe sociale qu'il puisse etre.Et Oui bien dit pour le passage Serigne Moutakha MBACKÉ (Yallah nafi yagg té werr).Serigne Abdou karim MBACKÉ ne cesse de nous rappeler qu'il est important d'avoir des sages (autorité,Kilifeu) par ce marque de refaire appaitre en premier Le khalif general des mourides.Il l'a dit.Qu'il ne fait qu'approuver les recommandations du khalif comme un talibé.Le Makarim Al Aqla (Les nobles carracteres sont d'abord pronés par le prophete Mouhamed Salla Lahou Aleyhi Wa Salam) alors c'est notre salut à tout musulman et l'incarner ne tient pas compte des confreries mais de l'unité et c'est ce que nous apprend Serigne Abdou Karim MBACKÉ ibn Serigne Fallou MBACKÉ. Belle emission et la maturité ne fera que grandir encore plus inchallah.Yalkah nala Yallah yokka Diapalé.
Cey sama wadji maco WOLOU de mbacke yague fi te weer 🤲🤲
SOLDAROU BAYE KARIM Bassirou Ndiaye Djinne Ziar bou werr nakamou
Machala !ñénaa laa sax
Maaa beugg sérigne Abdou karime beugg diébalou sii moom té xawmaa numay déffff...aidez moi svp
ManshaAllah Serigne Abdou Karime kilifa gou simple la té am yeug, am diné. Kilifa respect et considèration de ma part.
Baravo thiate et kilifa royou kaye guene li moy kharite
Yangui si yoon bu bax bi...lenen leep dina sapi dina xewi bamou déss yeuk yalla. Yangui doga wouyou saw tuur kilifa 👍❤. Yangui mouride tè manchalla💪
Kilifa mane dé beug nala machalla
Machallah mandall contanna thii yaw billahi yaw borom bakh nga
Machalah tawfekh rek
Aaah kilifa taye rek lala beug machalla
Ndeysane.wakh.dji.rafetna..machalah
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machalla wakh ji re feht na
Bilahi keene dou serigne touba mais nanou guena gorgorlou merci kilifeu
Koumay yobou ma ziaré serigne abdou karime way
Tu perds rien a ne pas y aller ...senegal brain washed rek Senegal ngay am fofou....
Mbacké balla yalla nafi yague té weur
y'a gui waxci dieiko té yena fii wo yon saye saye la
Machalha diardiaf
Je NE SUIS PAS FANS DE TOI MAIS J'APPRÉCIE BEAUCOUP TES DISCOURS , TON ARGUMENT VÉRIDIQUE ET LE SENS DE LA RESPONSABILITÉ KILIFEU ET VOUS DONNEZ DU COURAGE EN RACONTANT VOTRE VIE.
Machalah yalla nama borom bii may ma took ak serigne bii
Mann d demb tokk na ak mom nii côte à côte ndeyssann aka oyoff Mbacké balla yalna borom bi motali sa yénné wayy in shaa Allah
Ndeye awa Machalah
ماساء الله
Bilahi walahi deugue bou were nga wakh si baye karim mbacké fallilou
Mbacké dieureudieuf.sante Serigne Touba
Machallah iow killifa nga
Merci beaucoup kilifa
Machala kilifeu, wakh ji rafétena
Machalla khel rek moy nitt
Machallah kilifeu
Machallah billay beugue nàla
Ki mako beug moussouma xam fan la bokk vraie citoyens sénégalais
Kilifeu gueune nala beugue ndakh serigne abdou Karim damaka beugue sama khol
Bilay makarimal akhla mom reka wour
Bay Karim rk
ماشاء الله
Merci grand yalla yone bii oyoff
Machalla begue kilifa
Machala Rafet na mouride
Ragala féteu dé khagné weuresseuk??Baye Karim Prorége????🙏🙏
Kéne dou Serigne Abdou Karim mbacké
Massouma xamlolou Bilahi
machalla mouride waougor amnasolo
Ndeyesane machalla amna solo
Respect à vous keur gui
Machallh 💚💛❤
Akassa 🙏🙏🙏👌👌👌
Wawav fail
Ms
Mourid day am kilifeu.
Nice Na.
Macha Alla goudal fane ta were
Ma bague gou bague s Touba kilif rafentna
Modou ndiaye kone gnio yame mane dama beugue serigne touba kouko beugue ma beugue la
Dieureufety srg Touba diarama mame chiekh ibrahima
Ndeyssane mane d sopnala trop ndakh sa deugou ak populations binga andale
Nday saan Bay Akim masu maka guis dei wayé hamnani ak Baay Fall réka nék si mom
Macha hallah
waw gor kilifeu djebalou mo wor
Lamine.deck.yalnako.yalla.yeureum.mayko.diam.famouneck
Machallah
Amine
Wakh deugue yalla s Abdou Karim kubaakh la ku Sénégal réréla
Dagua bakh billahi
Bilahi sama xol toyna
💪💪💪💪🙏🙏
Vrai patriotes ce gua
machllah
.machala
Mala beugue bilahi mouride purr doun ndal
👏👏👏👏
Kokou nonou rék la meuna mél ndakh domou s.fallou la
marci
Bilahi amga serigne dal
Mo li ame touba da mousa ame fénne s touba dou kénne kénne dou mome
Moustapha Gaye kon serignesi dani deglou rap
Ndaysane 😭
Mashallah
Machallah il a retenu pas comme son ami thiat ! Courage meme si tu clash mon président
Nékh gua tay billhu dakh baye Karim kilipha diamou si iow
un exemple un vrai citoyen ... nekal si diam
Tay lala masa andaeull
Tu me plais vraiment
Niaw ndekété do lén doof nék kilifeu bahk na dh mé am kilifeu mo ko geuna wour
❤👍
Thiéye Serigne touba
beugeu nala dakh seringe Abdallah al karim
Diadieuf mouride waw goor
Kilifeuuuu
Machalla❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Kilipha respect werema
Joli
akassa ziar
Yalla nala ser touba sambou aarla nitt kou deug nga lii rk moye nitt boko xamoul mandoul simom kilifa taye béttna niou beuri
Ziar na la kilifa
L apparence est souvent trompeuse kilifeu daysan nittou késse la nake bonne continuation👍👍
Diam rekk mon cousin d valeur diam rekk nguay am tu es nee mouride bay fall lanouy doon ba fawwou
akassa
Diaadieuf baye fall
❤❤❤👌
Macha alla goudal fane ta were
Nica na fale
❤❤❤🇸🇳🇸🇳👈👌
😭😭😭😭😭
Kilifeu